boor
Apparence
wolof
[Soppi]boor:
- boor yamukaayi mbir, maanaa ay wet
Misaalum nees di jëfandikoo baat bi ci Wolof:
[Soppi]- booru xët wii am na ag njàppun ngir wacc ci suufu xët wi,
Xool it
[Soppi]Tekki
[Soppi]- wu-faraas: bord
- wu-angalteer: edge
Déglu baatu boor ci wolofi Senegaal Dencukaay:Wo-boor.ogg